Topma Songtext

Topma Soma Beugué
Diéguéssima Soma Nobé
Déglou Ma Soma Beugué
Diohma Sa hole soma wolo
Gisnga Chéri Li di Mbeuguel
Ak reuy Warou ko lal
Gisnga Baby sounou Mbeuguel Boul thi déf loudoul Sa hole
Eup na at Baniou Xamanté
Boba ba taye louné mougne naa ko
Eup na at Baniou Beugueunté
Beus bouné madi la gueuneu love
Yeuw Baby Sounou Mbeuguel boul thi déf loudoul sa hole
Yeuw Chéri Diohma Sa xol watna né douma ko xadiamal
Baby Mbeuguel aventure rék là,Meuno xam lathia Biir fi yeuk
Dougoulo
Baby Mbeuguel thi xole la diogué té bou Diogué si xol
xol réka keu meuneu xam

Topma Soma Beugué
Diéguéssima Soma Nobé
Déglou Ma Soma Beugué
Diohma Sa hole soma wolo
Gisnga Chéri Li di Mbeuguel Ak reuy Warou ko lal
Gisnga Baby sounou Mbeuguel Boul thi déf loudoul Sa hole
Eup na at Baniou Xamanté Boba ba taye louné mougne naa ko
Eup na at Baniou Beugueunté ba tay Beus bouné madi la gueuneu love
Yeuw Baby Sounou Mbeuguel boul thi déf loudoul sa hole
Yeuw Chéri Diohma Sa xol watna né douma ko xadiamal
Baby Mbeuguel aventure rék là,Meuno xam lathia Biir fi yeuk
Dougoulo
Baby Mbeuguel thi xole la diogué té bou Diogué si xol
xol réka keu meuneu xam

Thieuy Mbeuguellllllll mouno xam la thia Biir fi yeuk dougoulo
thieuy Mbeuguélééy mbeuguélééé
Eup na at Baniou Beugueunté
Bess Bouné madi la gueuneu love
Sama Xole Bi ya thi né annnnn chéri Beugueu naaalaaaa,
beugueu nala,beugueu nala
Kaaye niou Beugueunté,mbeuguel mouno xam la thia biir fi yeuk dougoulo
Guis Beugueu yala Koy déf thi diam mine Bagne thi djikola
mane beugueu naaaala,sama xol bi yeuw la tane beugueu nala
beugueu naaaala kaaay niou beugueunté
Mandé Beugueunala souniou mbeuguel reuy warou ko lal
Diohma sa xol bi watna né douma ko xadiamal mane beugue
nala,beugue nala kaay niou beugueunté

Baby Mbeuguel aventure rék là,Meuno xam lathia Biir fi yeuk
Dougoulo
Baby Mbeuguel thi xole la diogué té bou Diogué si xol
xol réka keu meuneu xam
Kay
Baby Mbeuguel aventure rék là,Meuno xam lathia Biir fi yeuk
Dougoulo,Baby Mbeuguel thi xole la diogué té bou Diogué si xol xol réka keu meuneu xam

Topma Video

Topma Video play
This website uses cookies to ensure you get the best experience on our website. Closing this message or scrolling the page you will allow us to use it. Learn more